^
YAWUT YA
Yàlla wax na jaarale ko ci Doom ji
Doom jee gëna màgg malaaka yi
Nanu faaydaal li Boroom bi wax ci mbirum mucc gi
Yeesu nekk na nit, ngir rammu nu ci kanam Yàlla
Kirist, Doom ji, moo gëna màgg Musaa, jawriñ bi
Buleen dëgër bopp ndax seen ñàkk ngëm
Nanu gëm li Yàlla wax, ba dugg ci noflaayam
Yeesu, sarxalkat bu mag bi
Nanu jëm kanam, baña walbatiku
Li Yàlla dige lu wóor la
Melkisedeg moo gëna màgg Ibraayma
Yeesu mooy sarxalkat bu mag, bi mel ni Melkisedeg
Yeesu, sarxalkat bu mag bi ci kaw, ci kóllëre gu bees gi
Ni ñu doon jaamoo Yàlla ca bési kóllëre gu jëkk ga
Saraxu Kirist bi gën dindi na bàkkaar yi
Nanu jege Yàlla
Ngëm
Buleen fonkadi yarub Boroom bi
Buleen tanqamlu Yàlla
Sarax yi neex Yàlla